Habiibul Xadiim

Habiibul Xadiim Maktabatu Habibul Xadiim 📖
Art & Spiritualité Mouride ✨
Khassidas & Tableaux d'art 🎨
🇸🇳 SN : 76 567 72 35
Livraison partout 🌍

❤️🕊️🕊️
10/05/2026

❤️🕊️🕊️

10/05/2026
👋 Bismilla ci Habiibul Xadiim ! ✨Mbindum Usmaan Silla mu leer naññ te set wecc.📖 Xassida yi jàppandi :🔹 Wakaana Qaqqan🔹 ...
07/05/2026

👋 Bismilla ci Habiibul Xadiim ! ✨
Mbindum Usmaan Silla mu leer naññ te set wecc.
📖 Xassida yi jàppandi :
🔹 Wakaana Qaqqan
🔹 Mawahibu
🔹 Bismil Ilaahi Ikfini
🔹 Sindidi
🔹 Tuhfatu
🔹 Matlabu Chifa
🔹 Astaghfirullaha Bihi
🔹 Chakuuru Raafi’u
🔹 Jaawartu
🔹 Wa Wassaynal insaan
🔹 Asmaoul Husna

🟢 Juz Ammayata
🟢 Khatmoul Khuran

📚 Dajale yi
🔸 Dajale (Astaghfirullaha Bihi, Sindidi, Tuhfatu, Matlabu chifa, Jaawartu)
🔸 Dajale (Astaghfirullaha Bihi, Wakaana, Chakuuru Raafi’u)
🔸 Dajale (Astaghfirullaha Bihi, Mawahibu)
🔸 Dajale (Astaghfirullaha Bihi, Sindiidi, Bismil Ilaahi Ikfini)
👇 Ban nga ci soxla ? Bind ñu message léegi ngir ñu jàppale la !
📲 +221 76 567 72 35 (Sénégal)
📲 +49 1521 6945384 (Allemagne)

Ku bëgg jéggal ci Yalla, tey sàkku kaarange gu wér ci say mbir, lii mooy sa téere !Ñu ngi leen di indil téere bu bees bi...
15/04/2026

Ku bëgg jéggal ci Yalla, tey sàkku kaarange gu wér ci say mbir, lii mooy sa téere !

Ñu ngi leen di indil téere bu bees bi bolé ñatti Xassida yu am doole :
✅ Astaghfirullah Bihi
✅ As-Sindiidi
✅ Bismil-ilaahi Ikfinii

Mbind mu set wecc : Usmaan Silla mo ko bind, ni ñu ko baaxoo defe. Araf yi dafa rëy, yomb a jang.

🛒 Gawalu leen
👉 Bësël fi ngir envoyer message : https://wa.me/221765677235

🇸🇳 SN : +221 76 567 72 35
🇩🇪 DE : +49 1521 6945384

Ku bëgg sàkku jéggal ci Yalla, tey sàkku barké ci tagg Yónnent bi (ﷺ)... Lii mooy sa téere !Ñu ngi leen di xamal ne téer...
15/04/2026

Ku bëgg sàkku jéggal ci Yalla, tey sàkku barké ci tagg Yónnent bi (ﷺ)... Lii mooy sa téere !

Ñu ngi leen di xamal ne téere bu bees bi bolé Astaghfirullah Bihi ak Mawahibun Naafih noppi na.

✅ Mbind mu leer naññ : Mbindum Usmaan Silla la, ni ñu ko baaxoo defe. Araf yi rëy na, yomb a jang.

🛒 Ku ci bëgg sa boss, gaawal gaaw !
👉 Beussal fi ngir envoyer message :
https://wa.me/221765677235

🇸🇳 SN : +221 76 567 72 35
🇩🇪 DE : +49 1521 6945384

14/04/2026

Ikfinii❤️ noppi na

27/03/2026

.xadiim

24/03/2026

Faweyni

24/03/2026

Allahu 🚨🥰

23/03/2026

*✒️✒️✒️ matlabul fawzayni*

Adresse

Louga
Touba

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Habiibul Xadiim publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager